
Tambalèle sa yonn.
To contact Fatou please sent a direct email to:

Gnou ngui djokhé thèrapie si fanam younè. Werroum khèl dafa am solo.
Gnou ngui wakhtane ak yènn si séne wallou werr si Anglais,Espagnol, Wolof, Soninké ak ak Farrancé.
Mind Over Matters Institute daffa farlou di wallu gneup si fanam yeupp.
Meun nagnou la dimbelè beutt ak beutt wala si machineyi diwotte.

An kilè djopa.
To contact Fatou please sent a direct email to:

Owa terrapie dabarini riya nando.
Owa, demanndani khanou gabè, Anguelé, Farrancè, Wolofo ado Soninkè.
Mind Over Matters Institute Ana soro gna demmana hakile ngaté, yakhou khibaré problémou, tampiyé, moukountakhou djamanè mpalé problèmou. Oraway mèwala yakhè ndo yakhè Wala machinou bè ga khirinedini.